Xam Say Farata [PDF]

  • 0 0 0
  • Gefällt Ihnen dieses papier und der download? Sie können Ihre eigene PDF-Datei in wenigen Minuten kostenlos online veröffentlichen! Anmelden
Datei wird geladen, bitte warten...
Zitiervorschau

1

La religion musulmane comporte 3 grandes parties : 1. Imaane (science tawkhid) :  Gueume Yalla  Gueume yonénte yi (313 messagers parmi les 124000 prophètes)  Gueume malaka yi  Gueume ndogal (lép namélou sounou Borom la mou nékh wala mou nakhari)  Gueume bissou pénc (adiana, safara, siraat, khissabe, ramou, …)  Gueume tèré yi (au nombre de 104)

2. Islam (science fikh) :  Tope ndigueul  Bayi téré

3. Ikhsane (science tassawouffe) di rafétal diamou bi :  Xam-xam ak téguine  Kérsa  Sant Yalla  Sélale  Tabbé  Noppi  Léwatt  Mougne  Deuguou  Torokhlou  Moytou lék, wakh ak nélaw you beuri  Moytou reuye, nguisteul, beuri mbeubeute  …

2

Les fondements de l’islam sont au nombre de 5 : 1. Gueume né :  Amoul béne Bour boudoul Yalla  Mouhamadou rassoulou Lahi Yalla ko yoni

2. Takhawal djouliye diourome 3. Diokhé assaka 4. Adji Makka 5. Wor wérou kôr

3

Sangou sét 4 Faratas :

4 Sounas :

1. Yéné (se fait au moment de laver les parties intimes)*

1. Rakhass say lokho jusqu’au poignet 2. Galakh ndikou (rakhass sa guémigne)

2. Ragg (bien se frotter)

3. Sarakh ndikou

3. Gaw (bo rakhassé thieur bala wow

4. Rakhass say nop

nga rakhass bissi top) 4. Khalil fép fou am karaw (ndokh bi na agg si dér bi) boudé danga létou nga nathie (beuss) léte yi bou bakh Sa yarame yép na toy

Diap 8 Faratas :

8 Sounas :

1. Yéné

1. Rakhass sa lokho jusqu’au poignet

2. Rakhass sa kaname

2. Galakh ndikou (rakhass sa guémigne)

3. Rakhass say lokho jusqu’au coude

3. Sarakh ndikou

4. Khalil say baramou lokho**

4. Fiirou

5. Massa sa bop (en partant du front vers

5. Rakhass say nop

la nuque)

6. Toyal sa lokho bala ngay rakhass nop yi

6. Rakhass say tank

7. Massa sa bop (de la nuque vers le front)

7. Ragg (bien se frotter)

8. Toftalé faratas yi (bien suivre l’ordre)

8. Gaw (voir 3eme farata sangou sét)

* Il est également possible de formuler en même temps l’intention de prier. ** Faire passer les doigts de la main gauche derrière ceux de la main droite (les entrecroiser) au moment de laver la main droite (et inversement).

4

Tim 8 Faratas :

3 Sounas : 1) Toftalé : respecter l’ordre (ex : massa

1. Yéné 2. Pak bou laap : (sable - carrière - eau - neige

sa khar kaname ba nopi doga massa

- argile etc…) 3. Gaw (bo massa wé sa khar kaname rék

gnari lokho yi) 2) Ték sa gnari lokho si souf nguir massa sa gnari lokho (la 2eme fois)*

dangay daadi massa gnari lokho yi) 4. Ték sa gnari lokho si souf nguir massa sa

3) Massa sa poignet bassi coude bi

khar kaname (la 1ere fois)* 5. Massa sa khar kaname 6. Massa sa lokho (jusqu’au poignet) 7. Bala ngay tim nanga nèk ba wakhtou bi taabi (wakhtou bi diote) 8. Lila takh di tim dafay diokalo (takhalo) ak tim gui (ex : dangay tim rék daadi diouk kabar wayé do tim ba nopi di khaar)

Etapes du Tim :  Poser tes mains sur le sol (sable - carrière - eau - neige - argile etc…) et faire le yéné.  Faire le 1er feugue et passer par le visage.  Encore poser tes mains sur le sol (sable - carrière - eau - neige - argile etc…).  Refaire le 2eme feugue et passer les bras puis les mains. * Gnari yone ngay ték sa lokho si souf.

Remarques importantes : 

Kou tim té amoulo ngante bakaar lassiye dieulé.



Ki nga khamni bou lalé ndokh fébar kokou tim moy farata si mome.



Boudé bo diapé mokhtar mi dinala raw dangay tim té gaw djouli.



Béne tim pour chaque farata et non pour plusieurs faratas.

5

Mokhtar et Darori Mokhtar : wakhtou bignou taamou koussi djouli (préférence). Darori : wakhtou binga khamni koussi djouli yangui si wakhtou bi boudé dangua amone ngante (délai ultime).

Djouli

Souba

Mokhtar

Darori

Début : mingui tambalé si fadiar

Début : fii mokhtar bi diékhé fofoula

(à Touba, c’est souvent 75 mn

darori bi tambalé (c’est valable pour

avant le lever du soleil)

toutes les heures de prières : principe

Fin : diékh bo meuné khaamé

à retenir à chaque fois)

nitt gni si wakhtou bi

Fin : sou rayons soleil yi commencé fégne si assamane si avant le lever du soleil*

Tisbar

Début : bou diante bi néké sissa

Début : fin mokhtar tisbar

digou boppou

Fin : bou diante bi sowé**

Fin : bo naté sa dieum mou tolo ak sa takander

Takoussane

Début : bo naté sa dieum mou

Début :fin mokhtar

tolo ak sa takander

takoussane

Fin : bou sa takander maté sa

Fin : bou diante bi sowé**

dieum gnaar

Timis

Début : bou diante bi sowé

Début : fin mokhtar timis

Fin : bo guissatoul khonk khonk

Fin : jusqu’à l’aube

yi si assamane si

* Wakhtouyi téré nagnou koussi nafila jusqu’au lever du soleil (wayé ki am borou djouli war ko faye mome n’est pas concerné par cette interdiction). ** Tisbar ak takoussane gno bok séne darori foumou yéme.

6

Guéwé

Début : bo guissatoul khonk

Début : fin mokhtar guéwé

khonk yi si assamane si (bou

Fin : jusqu’à l’aube

mokhtarou timis diékhé) Fin : bo khaadié goudi gui gnéti khadj, khadj bou ndieuk bi bou diékhé (goudi gui migui tambalé si début mokhtar guéwé diékhé si fin darori guéwé)

7

Djouli 5 chartes : -

Am sangou sét

-

Am ndiappou

-

Moure sa awra

-

Barap bou laap

-

Dioublou Khibla

15 Faratas :

21 Sounas :

1. Yéné djouli wakhtou bi

1. Likhaam

2. Yéné roye imam

2. 2eme saar après fatiha

3. Le 1er Allahou Akbar (kabarou

3. Takhaway 2eme saar après fatiha

armal)

4. Bireul (wakh si kaw)

4. Takhaway 1er Allahou Akbar 5. Fatiha (s)

5. Yélou (wakh si souf) 6. Allahou Akbar (excepté le 1er)

6. Takhaway fatiha (s) 7. Rouko

7. Taya (le 1er) 8. Toguay 1er taya

8. Délo rouko

9. Taya (le 2eme)

9. Soudiote

10. Toguay 2eme taya

10. Délo soudiote 11. Dàl (prendre son temps) 12. Yème (éviter de trop bouger) 13. Toftalé faratas yi

11. Toujours commencer par fatiha avant le 2eme saar 12. Délo seulmeule imam 13. Délo seulmeule kî nék à ta gauche 14. Wakh assalamou aleykoum si kaw

er

14. Seulmeule (1 assalamou aleykoum) 15. Toguay seulmeule

15. Djouli si yonénte bi (PSL) pour le dernier taya 16. Ték 7 : bakane - 2 genoux - 2 mains - 2 pieds (au moment du soudiote) 8

17. Ték saatir * 18. Sami Allahou limane hamida 19. Doli dàl 20. Tok touti après le salut final (seulmeule) 21. Déglou imam boudé bireul * Saatir : dafa wara sèw comme flèche, goude comme avant-bras, nature à ne pas distraire.

Ngueunèl : 1. Le fait de lever les deux mains jusqu’à hauteur des oreilles (au moment de dire Allahou Akbar) 2. Allahouma Rabana walakal hamdou 3. Commencer par la droite pour le seulmeule 4. Dire amine après avoir récité fatiha (s) 5. Soubhana Rabiyal Ahla… ak… soubhana Rabiyal hazim… 6. Tari saar bou goude boudé djouli souba - tari saar bou goude boudé djouli tisbar (mais na gueuneu gat bou souba bi) - tari saar bou gat takoussane ak timis - tari saar bou yème guéwé 7. 1er saar bi na gueuneu goudou 2eme saar bi pour chaque wakhtou. 8. Khounod (pour djouli souba) 9. Yeungueul nank sa baarame pour taya de la droite vers la gauche 10. Le fait d’ajouter l’invocation qui termine le dernier taya 11. Wormal soudiotes yi ak roukos yi

9

Défar Djouli Rappels : farata kéne douko soudiotal dagnou koy indi waat - ngeunél kéne douko soudiotal - souna rék lagnou wara soudiotal - bo yoké si djouli bi dangua wara soudiote bakhda salam bo wagné wala nga boolé yokou ak wagni dangua wara soudiote khabla salam. Khabla salam : faire juste avant le seulmeule 2 prosternations (soudiote) + un autre taya. Diir bou gat lagnou la may nga soudiote khabla. Si missal : bo guénegoul diaka dji - wala diougué guo fii ngay djoulé. Bakhda salam : faire après le seulmeule 2 prosternations (soudiote) + un autre taya. Heure boko fatéliko rék meune nga ko déf (donté att you beuri là). Raka bou fassou moy : bo rouko wé ba sigui. Bougnou né sa djouli yakhouna kone danga wara tambali waat djouli gui yép. Boudé béne souna rék nga faté kéne douko soudiotal sauf yélou ak bireul. Boudé gnari sounas nga faté - war nga soudiote khabla (wayé boko défoul wagniwoul dara). Boudé gnéti sounas wala lou eup nga faté - soudiote bi obligation là (boko faté djouli bi yakhouna).

Quelques points importants à retenir pour nignouy défaré Djouli : 1. Bo wakhé si biir djouli bi loussi bokoul nanga kham ni yok nga (faire bakhda salam) 2. Bo dioumé si tari saar bi nga wakh lo khamni bokoul si saar bi :  Boudé linga wakh bokoul si alkhourane dangay déf bakhda.  Boudé linga wakh bokna si alkhourane té sopiwoul sansou saar bi dou diar ngay soudiote. 3. Boudé danga djouli raka you eup linga warone djouli kone dangay diap ni danga yok nga daadi soudiote bakhda - wayé nak linga yok bou tolowé ak linga warone djouli kone djouli bi yakhouna (si missal souba bossi djoulé 4 rakas - wala tisbar nga djouli 8 rakas) 4. Boudé dangay siki saka si nombre de rakas bi nga am dangay diap li gueuna néw (ex : ngay djouli tisbar di siki saka entre 3 et 4 rakas dangay diap ni amnga 3 rakas - nga doli béne so paré soudiote bakhda - wayé nak boudé siki saka si biir djouli li mou lay 10

dàl dafa bari : ki nga khamni dafa bari limouy siki saka té limouy siki saka doussi am louko woor - sa bouko dalé rék nako diélelé douko diéma défar - té sop nagnou sayou ko lolou dalé mou soudiote bakhda salam 5. Bo dé siki saka ndakh seulmeule nga wala dét - dangay gaw daadi seulmeule bou féké yagoul après nga déf bakhda salam - bou féké yagg na djouli gui yakhouna 6. Khounod si souf lagnou koy diang wayé boudé danga ko diang si kaw doko soudiotal 7. Boudé danga wara bireul nga yélou (danga wagni)  Boudé rouko wago té mouy saar dangay reprendre saar bi - après doko soudiotal.  Boudé rouko wago té mouy fatiha dangay reprendre lép - après nga soudioute bakhda.  Boudé danga rouko ba sigui té mouy fatiha wala saar dangay agalé après nga soudiote khabla. 8. Boudé danga wara yélou nga bireul (danga yok)  Boudé rouko wago té mouy saar dangay reprendre saar bi - après doko soudiotal.  Boudé rouko wago té mouy fatiha dangay reprendre lép - après nga soudiote bakhda.  Boudé danga rouko ba sigui té mouy fatiha wala saar dangay continué après nga soudiote bakhda. 9. Kou faté diang saar si djouli farata - dangay soudiote khabla salam (faté nga saar + takhaway bi + yélou wala bireul) 10. Raka yinga kham ni fatiha rék lagnou siy diang - kou dioum diang si saar doko soudiotal 11. Boudé danga dioum si saar bi  Boudé fatiha meune nga démee khole si tèré - boudé amo tèré may nagnoula nga bayi béne aya après nga déf khabla (rappel : fatiha farata là).  Boudé saar bi ngay diang après fatiha - kéne mayoula ngay démee di khole si tèré - boko défé sa djouli yakhouna - dangay agalé djouli bi tébo paré diaroul ngakoy soudiotal. 12. Boudé danga reprendre fatiha - boko tayé sa djouli yakhouna - boko tayoul nga soudiote bakhda

11

13. Boudé danga tok sa gnételou raka (si tisbar - takoussane - wala guéwé) - dangay gaw diouk continué djouli raka yi déss - après nga soudiote bakhda 14. Boudé danga bayi fatiha fék raka bi fassouwoul dangay indi waat fatiha bo paré nga soudiote bakhda 15. Boudé danga faté rouko té raka bi top si raka binga dioum fassouwoul - dangay diouk takhaw indi waat saar daadi rouko (fii do indi fatiha - saar bi rék ngay indi - té saar bi sakh dafa gueune rék boko défoul wagniwoul dara) bo paré nga soudiote bakhda 16. Boudé danga bayi soudiote :  Boudé béne soudiote nga bayi té raka bi top si raka binga dioum fassouwoul : dangay wathie tok ba paré doga soudiote après nga soudiote bakhda.  Boudé gnari soudiotes nga bayi té raka bi top si raka binga dioum fassouwoul foumou la meuneu fék dangay indi directement soudiote (1er) - ensuite nga tok - après nga soudiote (2eme) - enfin nga soudiote bakhda après le seulmeule. 17. Sou féké si gnari rakas you ndieuk yi nga faté farata bi (soudiote, rouko, fatiha, …) nga fatéliko ganaw ba gnétélou raka bi fassou - dangay continuer djouli bi nga éliminé raka bobou nga faté farata (ex : boudé si 1er raka bi nga faté béne farata dangay diap ni sa 2eme raka moy sa 1er raka, boudé sa 2eme raka nga dioum dangay diap ni sa 3eme raka moy sa 2eme raka en conservant le premier raka ainsi de suite). So nopé nga soudiote khabla (ndakh 3eme raka moy 2eme raka - té 3eme raka bi diango si saar).  Boudé farata binga bayi nékoul si deux 1er rakas yi - ba légui dangay supprimé raka binga faté farata so nopé nga soudiote bakhda (fii bayi wo saar bayi wo taya - dangay considéré ni 4eme raka bi moy sa 3eme - sa 5eme moy sa 4eme).  Boudé sa 1er ou 2eme raka mo yakou té 3eme bi fassouwoul - kone 3eme raka bi dinga diang saar aprés nga déf bakhda salam. 18. Bo féké imam si biir djouli bi nga dapko  Boudé amoulo béne raka ak imam - boudé imam dafa dioum si biir djouli bi bouy soudiote bakhda wala khabla waroulo ande ak mome - dangay tok khar bamou paré nga soga diouk agalé djouli bi.  Boudé am nga ak imam béne raka wala louko eup boudé soudiote khabla dangay ande ak mome - wayé boudé soudiote bakhda do and ak mome dangay tok khar bamou paré nga soga diouk agalé - bo nopé nga soudiote bakhda salam - cas particuliers : boudé bingay diouk di agalé danga déf lou 12

waral soudiote khabla - bo paré dernier taya bi dangay soudiote khabla donté imam dafa soudiotone bakhda.  Boudé imam dafa paré nga diouk di agalé bo dioumé yakoy défaral sa bop. 19. Boudé imam dafa yok wala wagni si djouli danga koy sabaal : niko soubhanalah Ex 1: Bou imam djoulé béne raka wala 3 rakas sauf timis beunga tok - nanga ko sabaal té boul tok ak mome - boudé dafa continué tok dangay melni kou wagni béne raka bou bôba 4eme raka imam moy sa 3eme raka bo paré nga soudiote khabla salam - boudé nangou na ande ak yaw nak dafay mélni dangène yok si djouli bi - dangéne di soudiote bakhda. Ex 2: Bou imam djoulé ngari rakas té toguoul taya - nanga ko sabaal - boudé dafa continué nga and ak mome té bo paré nga soudiote khabla salam. 20. Djouli farata ak djouli souna (nafila) bokouniou nougnou lène di défaré si : fatiha, saar, bireul, yélou, yokhou raka ak ponk djouli  Djouli nafila dou obligation wayé bo khassé wakh Allahou Akbar rék nék na farata (amatoulo droit arrêter).  Boudé dangay djouli nafila - nga faté fatiha bou raka bi fasso dangay continué après nga soudiote khabla (boudone djouli farata dangay éliminé raka bobou, voir paragraphe 15).  Bo dé djouli nafila boudé danga wara yélou nga bireul ou inversement - lolou yakoussi dara doko soudiotal.  Bo dé djouli nafila nga bayi béne ponk (soudiote wala rouko) nga tok lou yagg doga diko fatélikou lolou yakhoul dara - boudé djouli farata la sa djouli yakhouna. Boudé djouli nafila gnari rakas - boudé danga dioum diouk démee si gnétélou raka bou féké gnétélou raka bi fassouwoul dangay déloussi tok taya seulmeule - so nopé soudiote bakhda salam - bou féké gnétélou raka bi fassouna dangay continué indi gnentélou raka - so nopé soudiote khabla salam - boudé djouli farata la dangay déloussi tok taya seulmeule sa boko fataliko (avant ou après rouko) après nga soudiote bakhda.

13

A savoir (si biir djouli) :  Bo né euf par la bouche té tayouloko dangay soudiote bakhda salam.  Bo né euf par la bouche té fék yako tay sa djouli yakhouna.  Rétane té tayko sa djouli yakhouna boudé tayouloko dou diar ngay soudiote.  Bo tissolé boul wakh alhamdoulilah.  Bo obeulé dieulal sa lokho taf sissa guémigne.  Bo diapanté ak ay nélaw si biir djouli bi : -

boudé nélaw yi khôtoul sa djouli yakhouwoul

-

boudé nélaw yi dafa khôte sa djouli ak sa ndiap yakhouna

 Boudé dafa am loulay diéma lor (animaux dangereux …) meune nga ko moytou - sou bôba bo wanoul guinaw khibla té yaguoul djouli bi bakh na - bo wané guinaw khibla nak wala mou yague sa djouli yakhouna.

14

Faye Djouli 1. Li nga amé si borou djouli sou eupoul gnenti wakhtous (jusqu’à 4) - dangay faye bor yi nga amé ba paré soga djouli wakhtou bi diote 2. Li nga amé si borou djouli sou eupé gnenti wakhtous (au-delà 4) - dangay djouli wakhtou bi diote ba nopi soga faye bor yi 3. Bo amé borou djouli - amoul wakhtou - meune nga ko faye wakhtou yép 4. Bo amé borou djouli téré nagnou là nafila excepté  Safa ak witr.  Nafila fadjr.  Nafila tabaski ak korité.  Nafila éclipse lunaire / nafila éclipse solaire. 5. Boudé amna gno khamni gno bok borou djouli meune nagnou ko fayando 6. Boudé danga ame borou djouli you bari té khamo noumou tollou - nga faye djouli yi bassa khél dàl (bamou wor lani faye nga bor yép)

15

Faye Djouli boula imam rawé Souba : 

Boula imam rawé béne raka (kone amnga ak imam béne raka) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué (sans reprendre kabarou armal bi) - fii boy diouk do wakh Allahou Akbar - bo diougué daadi diang fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 1er raka bila imam rawé) - fii waroul am khounod.

Tisbar :  Boula imam rawé béne raka (kone amnga ak imam gnéti rakas) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué (sans reprendre kabarou armal bi) - fii boy diouk do wakh Allahou Akbar - bo diougué daadi diang fatiha ak saar té yélou ko (bi moy 1er raka bila imam rawé).  Boula imam rawé gnari rakas (kone amnga ak imam gnari rakas) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué - fii boy diouk dangay wakh Allahou Akbar - bo diougué daadi diang fatiha ak saar té yélou ko (bi moy 1er raka bila imam rawé - amoul tok taya) - bou raka bobou nopé nga diouk indi sa dernier raka diang si fatiha ak saar té yélou ko (bi moy 2eme raka bila imam rawé).  Boula imam rawé gnéti rakas (kone amnga ak imam béne raka) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué (sans reprendre kabarou armal bi) - fii boy diouk do wakh Allahou Akbar - bo diougué dangay diang fatiha ak saar té yélou ko (bi moy 1er raka bila imam rawé) - après nga tok daadi taya sa 1er taya - bo nopé nga diouk indi bénéne raka diang si fatiha ak saar té yélou ko (bi moy sa 2eme raka bila imam rawé) - après nga indi sa dernier raka tari fatiha té yélou ko (bi moy sa 3eme raka bila imam rawé).

Takoussane : Takoussane ak tisbar gno bok nougnou lène di fayé

16

Timis :  Boula imam rawé béne raka (kone amnga ak imam gnari rakas) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué - fii boy diouk dangay wakh Allahou Akbar - bo diougué daadi diang fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 1er raka bila imam rawé).

 Boula imam rawé gnari rakas (kone amnga ak imam béne raka) bou imam seulmeulé dangay diouk continué (sans reprendre kabarou armal bi) - fii boy diouk do wakh Allahou Akbar - bo diougué daadi diang fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 1er raka bila imam rawé) - après nga tok daadi taya sa 1er taya - bo nopé nga diouk indi bénéne raka diang si fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 2eme raka bila imam rawé).

Guéwé :  Boula imam rawé béne raka (kone amnga ak imam gnéti rakas) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué (sans reprendre kabarou armal bi) - fii boy diouk do wakh Allahou Akbar - bo diougué daadi diang fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 1er raka bila imam rawé).

 Boula imam rawé gnari rakas (kone amnga ak imam gnari rakas) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué - fii boy diouk dangay wakh Allahou Akbar - bo diougué daadi diang fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 1er raka bila imam rawé amoul tok taya) - bou raka bobou nopé nga diouk indi sa dernier raka diang si fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 2eme raka bila imam rawé).

 Boula imam rawé gnéti rakas (kone amnga ak imam béne raka) - bou imam seulmeulé dangay diouk continué (sans reprendre kabarou armal bi) - fii boy diouk do wakh Allahou Akbar - bo diougué dangay diang fatiha ak saar té bireul ko (bi moy 1er raka bila imam rawé) - après nga tok daadi taya sa 1er taya - bo nopé nga diouk indi bénéne raka diang si fatiha ak saar té bireul ko (bi moy sa 2eme raka bila imam rawé) - après nga indi sa dernier raka tari fatiha té yélou ko (bi moy sa 3eme raka bila imam rawé).

17

Remarques : 1. Résumé : souba - tisbar - takoussane - guéwé : boula imam rawé béne wala gnéti rakas (nombre impair) boy diouk di agalé do wakh Allahou Akbar - boula imam rawé gnari rakas (nombre pair) boy diouk di agalé dangay wakh Allahou Akbar. Le contraire pour le timis.

2. Bo nieuwé fék imam di djouli - foumou meuna tollou nanga démee ande ak mome mais faire d’abord le kabarou armal (exemple : bo nieuwé fék imam di taya dangay tok ak mom - bou seulmeulé nga diouk continué - té boul kabaraat. Boy djouli ak imam bép souna bo faté mo la koy gadoul (khabla salam ak bakhda salam) - boudé danga bayi farata imam dou la ko gadoul  Boudé danga bayi rouko té nga nék si bénéne raka boudoul bou ndieuk bi (1er) fofou moune nga déf béne si gnar yi : -

Dangay rouko après nga dap imam bala mouye diouk si gnarélou soudiote bi.

-

Bou la lérè ni mouno dap imam nga bayi rouko bobou té topou imam té nga andi waat raka bobou bou imam seulmeulé et faire bakhda salam.

 Boudé danga bayi soudiote té meune nga dap imam bala mouye rouko si bénéne raka fofou meune nga soudiote - boudé meuno ko dap nak nga bayi soudiote bobou té topou imam té nga andi waat raka bobou bou imam seulmeulé et faire bakhda salam.

18

Djouli - kou fébar Si djouli bi amna 7 cas yo wara toftalé : Les 4 suivants sont obligatoires si toftalé bi : 1. Nga takhaw té bagna diapandou 2. Nga takhaw diapandou 3. Nga tok té bagna diapandou 4. Nga tok diapandou

Les 3 suivants dafa gueune si toftalé bi : 1. Nga teude sissa ndaydior 2. Nga teude sissa thiamongne 3. Nga teude sissa guinaw (sur le dos)

Remarques :  Boudé danga diapandou di djouli nga danou fofou djouli bi yakhouna.  Boudé danou wo wayé li nga diapandou mo danou fofou dagnou ko sipp rék (l’acte est blamé).

19

Annexes Khounod : Allahouma inna nastahiinouka - wa nastaqfirouka - wa nouminoubika - wa nata wakkalou alaika - wa nakhnahou laka - wa nakhlahou - wa nat roukoumann yak fourou bika Allahouma iyyaaka nahboudou - wa laka nousalli wa nasdioudou - wa ilaika nasha - wa nahfidou nardjou rahmataka - wa nakhafou hazaabakal djid da inna hazaa baka bil kafiriina moulhikhoune.

Salatou hala nabi (taya) : Allahouma salli ala seydina Mouhamadina wa hala ali seydina Mouhamad kama saleyta hala seydina Ibrahima wa hala ali seydina Ibrahima - wa barik hala seydina Mouhamadina wa hala ali seydina Mouhamad kama barakta hala seydina Ibrahima wa hala seydina Ibrahima fil alamina inaka hamidoune Madjidoune.

Taya : Atahiyatoulilah - azakiyatoulilah - atahi batou salawatou lilah - assalamou haleyka ayou hanabiyou - wa rakhmatoulahi - wa barakatouhou - assalamou haleyna - wa halà ibadilahi salikhine - ach hadou ann la illaha ila lahou wahdahou la charika lahou - wa ach adou ana Mouhamad abdouhou wa rassoulouhou.

Lignouy wakh si soudiote : Soubhana Rabiyal ahla Allahouma iqfirlii.

Lignouy wakh si rouko : Soubhana Rabiyal hazim wa bi hamdihi.

20

Kôr 2 Faratas : 1) Yéné 2) Moytou lép louy takha dog (lék - nane ect…)

3 Sounas : 1) Gawa ndogou (wayé nanga khaar ba heure bi diot : guinaw bou diante bi sowé) 2) Yékha kheude (finga nopé si kheude bi ak fignouy nodé : il faut environ 8 minutes)* 3) Moytou bép wakhi tiakhane ak bou gnaw (teuyé sa lamigne si bép wakh bou gnaw : bayi dieuw - bayi féne - bayi rambathie etc…)

Zakât 4 Faratas : 1) Yéné 2) Boko diokhé réne bala nga koy diokhé waat dafay mat att (1 an)** 3) Lingay diokhé na mat Nissaab: 4) Zakât bi waroko tokhal : finga deuk bou amé gnouko sokhla diokh lène ko

3 Sounas : 1) Lingay diokhé nga défko si khol bou sède nguir diamou Yalla mila ko digueul 2) Boul diokhé li gueune, boul diokhé li yèss sissa allal (dangay diokhé lo khamni si diig bi la nék) 3) Lingay diokhé nga soutoural ko pour moytou nguisteul

* Le Prophète (PSL) néna kheude sila barké nék. ** Exception : pour les cultivateurs, le zakat se fait proportionnellement au nombre de récoltes (même si les récoltes se font plusieurs fois par an).

21

Hadji Makka 4 Faratas : 1. Yéné 2. Weur kabaa gui si 10eme jour du mois de la tabaski 3. Dokh Saffa ak Marwa 7 fois 4. Takhawayou arafat (annule les péchés)

12 Sounas (répartis en 3 parties) : Boy armaal : 1. Être propre (sét) 2. Moytou sol li gnou gnaw y compris les chaussures 3. Se couvrir seulement avec 2 morceaux (wodou ak lambayo) 4. Dire « labayka » en suivant le guide du pèlerinage (jusqu’à masdjidil haram)

Weur kabaa gui : 1. Marcher avec tes pieds (dokh ak say tank) 2. Embrasser la pierre avec ta bouche ou avec tes mains 3. Daw bou yème pour les hommes pour les 3 premiers tours de la kabaa 4. Sakou niane

Saffa ak Marwa : 1) Nga diarrate embrasser la pierre avant de prendre la direction de Saffa 2) Yègue (monter) d’abord sur Saffa doga déme Marwa 3) Daw bou gaw pour les hommes entre Saffa et Marwa (7 tours) 4) Bo yègué (monter) sur Saffa ak Marwa nga niane bou yague

22